Ñenteelu njàng: Wonale

 0    66 flashcards    kavadias
print play test yourself
 
Question Answer
aller chercher
start learning
jéli
durer, rester longtemps
start learning
yàgg
avoir
start learning
am
emmener
start learning
yóbbu
être bien / bon
start learning
baax
dire
start learning
ne
saluer (pour prendre congé)
start learning
tàggu
aéroport
start learning
ayeropoor (b)
semaine
start learning
ayubés (b)
les gens de
start learning
waa
non
start learning
déetdéet
celui-ci
start learning
kii
qui?
start learning
kan
l'année dernière
start learning
daaw
celui-là (personne)
start learning
kooku
oui!
start learning
waaw
(pronom objet singlier)
start learning
ko
(pronom objet pluriel)
start learning
leen
et (entre duex verbs/propositions)
start learning
le
bavarder, s'entretenir
start learning
waxtaan
marchander
start learning
waxaale
les Sénégalais
start learning
waa Senegaal
soupirant
start learning
waxaale (b)
jour (2)
start learning
fan (w), bés (b)
année
start learning
at (m)
1
start learning
benn
2(ième)
start learning
ñaar(eel)
3(ième)
start learning
ñett(eel)
4(ième)
start learning
ñent(eel)
5(ième)
start learning
juróom(eel)
6(ième)
start learning
juróom benn(eel)
7(ième)
start learning
juróom ñaar(eel)
8(ième)
start learning
juróom ñett(eel)
9(ième)
start learning
juróom ñent(eel)
dix(ième)
start learning
fukk(eel)
11
start learning
fukk ak benn
12
start learning
fukk ak ñaar
13
start learning
fukk ak ñett
14
start learning
fukk ak ñent
15
start learning
fukk ak juróom
20
start learning
ñaar fukk
30
start learning
fanweer
100
start learning
téeméer
200
start learning
ñaari téeméer
500
start learning
juróomi téeméer
1000
start learning
junni
jusqu'a
jusqu'a revenir
start learning
ba
ba dellusi
il a mangé jusqu'à terminer (il a fini de manger)
start learning
lekk na ba noppi
je vous ai attendu jusqu'a être fatigué (ça fait longtemps que je vous attends)
start learning
Xaar naa leen ba sonn
celui qui
ceux qui
start learning
ki
ñi
celui-ci
ceux-ci
start learning
kii
ñii
celui-là
ceux-là
start learning
kooku
ñooñu
qui? (sing)
qui? (pl.)
start learning
kan
ñan
cet homme
ces hommes
start learning
nit kii
nit ñii
cet homme-là
ces hommes-là
start learning
nit kooku
nit ñooñu
quel homme?
quels hommes?
start learning
nit kan?
nit ñan?
est-ce qu'il parle le Wolof?
est-ce que?
start learning
ndax dégg na Wolof?
ndax?
(j'irai)
1-3, sing.pl.
(futur affirmative)
start learning
dinaa dem, dinga dem, dina dem
dinañu dem, dingeen dem, dinañu dem
(je n'irai pas)
1-3, sing.pl.
(futur négatif)
start learning
duma dem, doo dem, du dem
(duma + nom = ne pas être)
duñu dem, dungeen dem, duñu dem
je suis ici depuis (x) jours/semaines/mois/années
start learning
am naa fi (x+i) fan/ayubés/weer/at
est-tu ici depuis longtemps?
start learning
Yàgg nga fi?
Vas-tu rester ici longtemps?
start learning
Dinga fi yàgg?
je suis ici pour (x) jours/semaines/mois/années
start learning
dinaa fi am (x) fan/ayubes/weer/at
Bon voyage!
(litt. va et viens à la paix)
start learning
demleen te ñów ak jàmm
il ouvre la porte
il la ouvre
start learning
mu ngiy ubbi bunt bi
mu ngi koy ubbi
il console les enfants
il les console
start learning
mu ngiy nax xale yi
mu ngi leen di nax

You must sign in to write a comment