ñaareelu njàng: nuyoo

 0    61 flashcards    kavadias
print play test yourself
 
Question Answer
passer la journée
start learning
yendu
parler, dire
start learning
wax
aller, partir
start learning
dem
regarder, rendre visite, visiter, examiner
start learning
seet
retourner
start learning
dellu
frère/soeur ainée
start learning
mag (j)
le fait de passer la journée
start learning
kendaay
fils, fille
start learning
doom (j)
copain
start learning
waay (j)
parole, propos
start learning
wax (j)
mère (2)
start learning
yaay (j), ndey (j)
plage
start learning
tefes (b)
soir
start learning
ngoon (g)
là-dessus, ainsi
start learning
noonu
alors (en position finale)
start learning
nag, nak
quand, à quel moment?
start learning
kañ
donc
start learning
kon boog
à la prochaine
un autre
start learning
ba beneen
beneen
jusqu'a
start learning
ba
père (2)
start learning
baay (j), pàppa (j)
cadet(te)
start learning
rakk (j)
grand-père/mère
start learning
maam (j)
oncle maternel
start learning
nijaay (j)
famille (élargie)
start learning
njaboot (g)
homme (au sens large)
start learning
góor (g)
femme (au sens large)
start learning
jigéen (j)
nuit, soir(ée)
start learning
guddi (g)
matin(née)
start learning
suba (s)
fille/fils
start learning
doom ju jigéen/góor
soeur/frère ainé(e)
start learning
mag ju jigéen/góor
soeur/frère cadette
start learning
rakk ju jigéen/góor
grand-mère/père
start learning
maam ju jigéen/góor
le frère ainé d'Omar
parfois omis
complément de nom
start learning
magU Omar
e.g. kër Omar
-u
[il est part à la plage]
emphatique du complément: accompli
complément est placé en tête de la phrase: mis en relief
start learning
tefes laa dem; tefes nga dem; tefes la dem
tefes lañu dem; tefes ngeen dem; tefes lañu dem
[c'est à la plage que je vais]
emphatique du complément: inaccompli
suffixe variable à la 2e pers.pl.
start learning
tefes laay dem, tefes ngay dem, tefes lay dem
tefes lañuy dem, tefes ngeen di dem, tefes lañuy dem
comment vont tes enfants?
pluriel des adjectifs possessifs
start learning
naka say doom?
mes enfants (2)
mes
start learning
samay/sumay doom
tes enfants
tes
start learning
say doom
say
ses enfants
ses
start learning
ay doomam
suffix
ay
nos enfants
nos
start learning
nuñuy doom
vos enfants
vos
start learning
seeni doom
seeni
leurs enfants
leurs
start learning
seeni doom
[il est allé à Pikine]
emphatique du verbe: accompli et inaccompli
suffix pour présent actuel ou futur
start learning
dama(y) dem Pikin, danga(y) dem Pikin, dafa(y) dem Pikin
-y
dañu(y) dem Pikin, dangeen(y) dem Pikin, dañu(y) dem Pikin
voir, aller voir, venir voir
start learning
seet, seeti, seetsi
retourner, revenir à son point de départ
start learning
dellu, dellusi
Et Bokar? Aliw et Omar
et à la fin vs et entre deux mots
start learning
Bokar nag? Aliw ak Omar
nag vs ak
les pronoms libres
moi, toi, lui/elle, nous, vous, eux/elles
start learning
man, yow, moom, ñun, yeen, ñoom
apporte le livre!
imp. singulier devant pronom
apporte-le!
start learning
indil téere bi!
moins le 'l'
indi ko!
salue Omar!
imp. singulier devant pronom
salue-le!
start learning
nuyul Omar
nuyu ko!
Salue Omar pour moi
bénéfactif
indiqué par un suffix
start learning
Nuyul ma Omar
Bonjour chez toi
bénéfactif
litt.: Salue pour nous les gens de ta maison
start learning
nuyul ñu sa waa kër
[pronoms personnels objet (direct ou indirect)]
start learning
ma, la, ko, ñu, leen, leen
écrire
bénéfactif
j'écris une lettre de la part d'Omar
start learning
bind
Damay bindal Omar Leetar
je prépare du mafé de la part de mes hôtes
bénéfactif
start learning
damay toggal suma gan yi maafe
pain
start learning
mburu (m)
porter
porte la chemise!
start learning
sol
solal simis bi
j'aime cet enfant
c'est cet enfant que j'aime
start learning
dama sopp xale bi
xale bi laa sopp
ils cherchent du travail
c'est le travail qu'ils cherchent
start learning
dañuy wut liggéey
ligéey lañuy wut
écouter
start learning
déglu
il est arrivé le soir
le voici il est arrivé le soir
start learning
dafa agsi ci ngoon
mu ngi agsi ci ngoon
tu as oublié ta clé
te voici qui as oublié ta clé
start learning
dangay fàtte sa caabi
yaa ngiy fàtte sa caabi

You must sign in to write a comment